Xott-biteel
Apparence
Xott-biteel gi xeetu garab la gu bokk ci ñoñ Eucalyptus. Óstraali la bàyyikoo.
Melo wi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Guddaayuy 20i met lay yore, waaye man nay hàgg ba 45i met. Xàncam day dijj (3i sàntimet), woyof, te yor i gàkk gàkk yu xonq, yu baam, yu nëtëx ak yu weex. Saawiyee ba suye lay meññ ci barab yu naaje ya.
Njariñ yi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Ronam bu tàbbe cig dex, dëkkuwaay la ñeel yenn jën yi. Dees kor kerloo te di ko fajoo it.
Nataal yi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]-
Xobu xott-biteel
-
Ay tóortóoram
-
Doom yi
-
Ëkkug xott-biteel
Turu xamxam wi
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Eucalyptus camaldulensis
Tur wi ci yeneeni làkk
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Farañse: gommier rouge/ des rivieres