Melosuufug Buruundi
Buruundi am réewu diwaanu Diggu Afrig la, rëye na 27,830 km², 25,650 km² suuf la, 2,180 km² di ndox.
Melosuufug jëmm
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Mi ngi digook Kongóo-brasaawiil ci lu mat 233 km ci sowwu, ak Ruwandaa ci 290 km ci bëj-gànnaar, lang ak Tansani ci guddaayub 451 km ci penku. Buruundi amul ubbeeku ci géej gi, waaye yi ci bëj-saalum-sowwu da ñoo lang ak déegub Tanganica bu rëy ba. Réew mi dafa nekk ci diggante ñaari mbandi ndox yu mag yii di Niil ak bu Kongóo
Xool it
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]
Xool it Wikimedia Commons
|
Melosuufug Afrig |
Afrig gu Bëj-saalum • Alseeri • Angolaa • Bene • Botswana • Burkinaa Faaso • Buruundi • Kamerun • Kap Weer • Réewum Diggu Afrig • Bennoo yu Komoor • Kongóo-Brasaawiil • Kongóo-Kinshasa • Kot Diwaar • Jibuti • Isipt • Eriitere • Ecoopi • Gaboŋ • Gaambi • Gana • Gine • Gine-Bisawóo • Gineg yamoo • Keeñaa • Lesoto • Liberiyaa • Libi • Madagaskaar • Marook • Malawi • Mali • Móoris • Gànnaar • Mosambik • Namibi • Niseer • Niseeriyaa • Ugandaa • Ruwandaa • Sahara gu Sowwu • Sao Tome-ak-Principe • Senegaal • Seysel • Siraa Leyoon • Somali • Sudaan • Suwaasilaand • Tansani • Cadd • Togo • Tuniisi • Sambi • Simbaawe