Las Palmasu Kanaari gu Mag
Apparence
Las Palmasu Kanaari gu Mag | |
---|---|
Réew | Ispaañ |
Tund | Tunduw Las Palmas |
Tus-wu-gaar Tus-wu-taxaw |
|
Kawewaay | 8 m |
way-dëkk | 377 056 nit |
atum way-dëkk | 2 006 |
Rëyaay | 100,55 km² |
Fattaay | 3 790,38 nit/km² |
Dalub web | www.laspalmasgc.es |
Gisub Kaw | |
Las Palmasu Kanaari gu Mag ab dëkkaanu Tunduw las Palamas la, di itam péeyam teg ci nekk benn ci ñaari péeyi Duni Kanaari yi (réewum Ispaañ) beneen bi di Santa Cruz wu Tenerif tuxalug man-man gi ñeenti at yu ne lees koy amal. Mi ngi nekk ci bëj-gànnaar-penku Kanaari gu Mag mooy dëkk bi fa ëpp, tëdd ci suufus 10 km.
Dëkkiin
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]- 1991= 354 877
- 1996= 355 563
- 2001= 354 863
- 2004= 376 953
- 2005= 378 628