Aller au contenu

Alse

Jóge Wikipedia.


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


الجزائر Alse
Skyline of {{{official_name}}}
Réew  Alseeri
Tus-wu-gaar
Tus-wu-taxaw
36° 46′ Bëj-gànnaar
     03° 03′ Penku
/ 36.767, 3.05
Kawewaay 424 m
way-dëkk 2 203 698 nit
atum way-dëkk 2 009
Barabalub Alse
Alse

Alse walla الجزائر ci araabi alseeri mooy péeyu réewum Alseeri, féete ci bëj-gànnaaru réew mi janook Géej gu Diggu gi. Mooy itam dëkk bi gën a mag ca réew ma